Cardinal number Ordinal number With a noun Benn Bu njëkk Bindkat bu njëkk Ñaar Ñaareel Ñaareelu bindkat Juróóm Juróómeel Juróómeelu bindkat Fukk-ak-benn Fukk-ak-benneel Fukk-ak-benneelu bindkat Misaal: Sama xarit David nekk na ñaareelu jàngkat ci sunu kalaas. Waaye man nekk naa ñetteel ginnaaw moom. ******************************************* Now you try: 44th 100th 19th 31st 72nd Examples of profession Verbs Nouns English translation Bind (to write) Bindkat -b Writer Fecc (to dance) Fecckat -b Dancer Way (to sing) Waykat -b Singer Dawal (to drive) Dawalkat -b Driver Jàngale Jàngalekat -b Teacher Daw (to run) Dawkat -b Runner , athlete Jàng Jàngkat -b Learner, student
© Copyright 2025 ExpyDoc