28 - Laaf

Les pronoms relatifs
The relative pronouns
Les pronoms relatifs
single qui se rapportent au
sujet
wu, bu, ju, ku, su, mu, lu, gu
Die Relativpronomen
single relative pronouns
that bear on the subject
singulier
singular
alleinstehende Relativpronomen, die sich auf das
Subjekt beziehen
singular
yu
pluriel non humain
plural non-human
plural nicht menschlich
ñu
pluriel humain
plural human
plural menschlich
fas wu lekkoon ñax mi Le cheval qui a mangé The horse that ate the Das Pferd, das Gras gegesreer na.
les herbes est perdu.
grass is lost.
sen hatte, ist verschwunden.
jigéén ju jël téére bi
La femme qui a pris le The woman who took Die Frau, die das Buch
Fatu la tuddu.
livre s‘appelle Fatou.
the book is called Fatu. genmmen hatte, heißt
Fatu.
jigéén ju jëlul téére bi La femme qui n´a pas The woman who didn’t Die Frau, die das Buch
Fatu la tudd.
prisle livre s´appelle
take the book is called nicht genmmen hatte,
Fatou.
Fatu.
heißt Fatu.
jaaykat bu mu fa xarito. Le marchand avec qui The seller with whom Ein Händler, mit dem er
il s´est lié une relation- he is closed friends.
freundschaftlich verbunamicale.
den ist.
téere bu ma bind mu Voici le livre que j´ai Here the a book, that I Hier ist das Buch, das ich
ngi nii.
écrit.
wrote.
geschrieben habe.
xale bu nga faj mu ngi Voici l´enfant que tu as Here is the child that Hier ist das Kind, das du
nii.
soigné.
you cared for.
gepflegt hattest.
góor gu sol xaftaan mu Voici l´homme qui
Here is the man who Hier ist der Mann, der
ngi nii.
porte un caftan.
wears a caftan.
einen Kaftan trägt.
1
les pronoms relatifs
lexicalisé
lexicalized relative
pronouns
woo-xam-ne, boo-xam-ne,
joo-xam-ne, koo-xam-ne,
soo-xam-ne moo-xamne,loo-xam-ne goo-xamne
singulier
lexikalisierte
Relativpronomen
singular
singular
yoo-xam-ne
pluriel non humain
plural non-human
plural nicht menschlich
ñoo-xam-ne
pluriel humain
plural human
plural menschlich
ffas woo-xam-ne
lekkoon na ñax mi
feebar na.
jigéén joo-xam-ne am
na doom kër gee lay
toog.
Chaque cheval qui a
mangé de l´herbe est
malade.
Chaque femme qui
a un enfant reste à la
maison.
Every horse that ate
grass is sick.
Jedes Pferd, das das Gras
gegessen hatte, ist krank
Every woman who has Jede Frau, die ein Kind hat
a child stays at home. bleibt zu Hause.
.
2
Les pronoms relatifs single
qui se rapportent au objet
ma, nga, mu, ñu, ngeen, ñu
jénd naa téere bi mu
bëgg.
dem nañu ci bërëb bi
ñu xamuloon.
réeral nga kayit gi ma
tegoon fii.
xam naa jigéen ji mu
may kër.
single relative pronouns that
bear on the object
singulier
J´ai acheté le livre qu´il
veut.
Nous avons été à
l‘endroit lequel nous ne
connaissions pas.
Tu as perdu le papier
que j‘avais posé ici.
Je connais la femme
à qui il a donné une
maison.
alleinstehende Relativpronomen, die sich auf das Objekt
beziehen
singular
I bought a book, that
he wants.
We were at a place we
didn‘t know.
singular
Ich habe ein Buch gekauft,
das er will.
Wir waren an einem Ort,
den wir nicht kannten.
You lost
the pa- Du hast das Papier verloper, that I had put here. ren, das ich hier hingelegt
hatte.
I know the woman to Ich kenne die Frau, der er
whom he gave a house. ein Haus gegeben hatte.
Aliin Sitoe Diatta.
Aliin Sitoe Diatta, mu ngiy juddoo Niolou Kabrus Kasamans ci bëjsaalumu Senegaal ci dëkk bu ñu naan Niolou ci atum junni ak juroom ñenti téemeer ak ñaar fukki at.
Baay.am ak yaay.am ñu ngiy tuddoon Silisia ak Assonelo Diatta.
Wante nijaay.am moo ko yar, ginnaaw bi baay.am faato. Aliin Sitoe
Diatta Kabrus la jóge. Mu ngiy dem Ziguinchor ngir wut liggéey.
Mu ngiy fa doon liggéey ni yenukat (docker). Wante daf.ul liggéey yi
yennen xale yu jigéen yi doon def: mbindaanu. Bi mu jóge Ziguinchor
ci la dem Dakar. Foofu la defe gént.am bi mel ni yonente ngir yewwi
askan.am yi ci loxoy nasaraan yi. Wante moom nang.ul.oon yonente
bi. Bi mu ko bañe dafa xëm. Ci la ko benn tan bu weex peeñu te wax ko
dafa wara topp ndigal li. Ginnaaw loolu ci la dellu Kabrus. Bi mu dellu
dëkk.am ñu ngi ka doon woowe jigéen bu mën góor. Ndaxte moom
moo njiite xeex bi ak nasaraan. Mu wax beykat yi bey yi ñu bàyyi bay
bu ñuy bey.al nasaraan yi. Ndigal li bax.ul.woon ngir nasaraan yi.
Loolu moo tax nasaraan yi jàppu ko yóbbu ko Mali, Tombuktu, ndaxte
nasaraan yi dañu ko jàppe ku wóor.ul. Ginnaaw bi ño yóbbe Tombuktu ci foofu la faato ci atum 1944. Mu ngi am.oon ñaar fukk ak ñenti at.
juddoo
bëj-saalum
naan
ci atum
wante
yar
nijaay
jóge
wut
yenu
fa
bi
mel
yonente
askan
yewwi
nangu
bañ
xëm
tan
peeñu
war
geboren
Süden
genannt
im Jahr
aber
erziehen
Onkel
Ort verlassen, Herkunft
suchen
auf dem Kopf tragen
dort
als
ähneln
Botschaft
Volk
befreien
einverstanden sein
refuser
ohnmächtig werden
Geier
Erscheinung
müssen
ndigal
topp
ñibbi
woowe
njiit lnjiite
xeex bnasaraan bbeykat
bàyyi
ndigal li
moo tax
jàpp
yóbbu
ndaxte
wóorul
dee
faatu
mbindaan
gént
nangu
instruction
befolgen
zu sich nach Hause gehen
bezeichnen
Chef
anführen
Widerstand
Europäer
Landwirt
aufhören
Anweisung
es ist weil ...
gefangen nehmen
mitnehmen
weil
gefährlich sein
sterben
sterben
Hausangestellte
Traum
Einverstanden sein
3